Description
= Ëmbiit =
Nu xam soxla bi am ci man a toxal dal-yu-ndaw yi ci sa réseau ngir dem ci sampum dal benn, walla lu ko moy, su fekkee sa kiliyaan dafa dogu a toxal seen dalub web. Modil Site exporter ak importer dafay yombal liggéey bii. Jumtukaay bii dafay jàllale ak fat sites yi jaarale ko ci dencukaayi zip, yu mën itam nekk nattu-backup.
= Man-man yi =
- Jàllale ak fat sites yi
- Jokkoo bu yomb a jëfandikoo
- Sos nattu-backup bu site bi
= Téere ndimbal = Naka lañuy jàllale ak fat site



Reviews
There are no reviews yet.